TSK

TSK · Proverbs 10:24

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Back to passage
Job 15:21 TSK

coowal musiba mooy buur nopp ya, yàqkat bette ko biir jàmm.

Deel bànneexoo Aji Sax ji, mu may la say nammeel.

Man it maa leen di taamoo jox seeni mbugal, dikke leen tiitaange yi ñu yelloo, ngir maa woote, kenn wuyuwul, ma àddu, dégluwuñu ma. Xanaa di def lu bon lu ma ñaawlu, li ma buggul, ñu taamu ko.»

¶ Kàddug Buur ga daanoogul sax, baat jibe asamaan àddu ne: «Yaw Buur Nabukodonosor, dogal ñeel na la ne nguur gi rëcc na la.

Xanaa tiitaangey séentu mbugal ma, ak sawara wu yànj wiy xoyom fippukat yi.