Psalms 119:34
TSK
May ma dég-dég, ma topp saw yoon, toppe ko xol bu tàlli.
TSK
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
May ma dég-dég, ma topp saw yoon, toppe ko xol bu tàlli.
Xelalal ku xelu, mu yokku. Xamalal ku jub, mu yokk njàngam.
Ku bëgga xam, bëgg ku la yedd; ku bañ ku la àrtu, bàyyima nga.
Moom sa làmmiñ, sàmm sa bakkan; rattaxle, yàqule.
Kër-këri, jariñu; waxi neen, loxoy neen.
Ab dof, waxam a koy sànk, làmmiñu boppam a koy dugal.