TSK

TSK · Proverbs 11:12

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Back to passage

Terewul mu am ay nit ñu tekkiwul dara di wax, naan: «Ana nan lanu waa jii di xettlee?» Ñooñu sewal ko, yótuñu ko jenn teraanga. Sóol nag ne cell.

daldi mànkoo, lal pexe ngir xareek Yerusalem, fitnaal leen.

Wax ju bare, moy ñàkku ca; ku moom sa làmmiñ, xelu nga.

¶ Farisen ñu bëgg xaalis ña nag dégg loolu Yeesu wax lépp, ba noppi di ko ñaawal.