TSK

TSK · Proverbs 13:3

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Back to passage

Mu jëm ci Yedutun, njiital jàngkat yi, di kàddug Sabóor, ñeel Daawuda.

Wax ju bare, moy ñàkku ca; ku moom sa làmmiñ, xelu nga.

Ab dof a ngi réy-réylu, làmmiñam yar ko; ku rafet xel, sa kàddu aar la.

Dund ak dee a ngi ci làmmiñ, te wax garab la, ku ko bëgg, lekk ca doom ya.

Ub sa gémmiñ, moom sa làmmiñ, mucc ci njàqare.

¶ Ku yaakaar ne moo jullite te moomul làmmiñam, boppam lay nax te ag njulliteem amul njariñ.