Job 28:10
TSK
Ci biir xeer yi lay yettey xunti, ba bëtam di gis lu cay alal.
TSK
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
Ci biir xeer yi lay yettey xunti, ba bëtam di gis lu cay alal.
Njaxlaf, jiitu; yaafus, des gannaaw.
Ana lu liggéeykat biy jariñoo ciw ñaqam?
Te itam ca lañuy tàmme am ug jot, di taxawaalu kër ak kër. Te duñu yem ci am ag jot rekk, waaye dañuy làmmiñu, di dugg lu seen yoon nekkul, tey wax lu leen warul.