TSK

TSK · Proverbs 14:27

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Back to passage

Buumi ndee tanc ma, walum kasara naq ma,

Njàngle mu xelu day suuxat bakkan, ba boroom du tàbbi ci fiiri ndee.

Yoonu njublaŋ, ay dég aki fiir; ku sàmm sa bakkan sore ko.

Liy dalal seen jamono mooy koomu ndam; xel ak xam-xam, te ragal Aji Sax ji, loolooy seen alal.