TSK

TSK · Proverbs 14:28

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Back to passage

Terewul lu ñu leen gëna fitnaal, ñuy gën di fulandiwu, yokku, ba waa Misra am njàqare ca bànni Israyil.

Yowab ne ko: «Buur, yal na Aji Sax ji ful askan wi téeméeri yoon, nga fekke. Waaye sang bi, lu la xiir ci loolu?»

Waa Israyil daje, sàkk ab dund, ba noppi dox wuti leen. Waa Israyil a nga dal janook ñoom, di saf ñaari gétti bëy. Waa Siri ñoom fees àll ba.

Mujj na Yowakas desewuloon ca mbooloom xareem lu moy juróom fukki gawar ak fukki watiir ak fukki junniy xarekat (10 000), ndax buurub Siri moo faagaagal ña ca des ñépp, duma leen ba ñu ne mbëtt.