aaytéefu làmmiñ, nga fegu ca, te yàqule guy dikk, doo ko ragal.
TSK
TSK · Proverbs 14:3
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
Éy Aji Sax ji, woo naa la wall, yàlla buma rus. Yal na ku bon rus, ne xerem biir njaniiw.
Mooy yónnee fa asamaan, musal ma, dumaal ma ku may not. Selaw. Yàllaay yónnee jëfi ngoram ak wormaam.
Moom sa làmmiñ, sàmm sa bakkan; rattaxle, yàqule.
Ab dof, waxam a koy sànk, làmmiñu boppam a koy dugal.
Ku ji njubadi, góob fitna, yet wa muy dóore, damm.
Ma bëgga am lu leer ba tey ci fukki béjjén yi ci bopp bi ak beneen ba génn, ba ñett daanu ca kanamam; mu am ay bët ak gémmiñ, di wax kàdduy damu, te ëpp yi ci des.
Noonu itam la aw làmmiñ dee cér su tuut te réy aw bàkk. Seetleen ni ferñent su tuut di lakke gott bu yaa.
Gannaaw yaa sàmm sama kàddu, ba muñ ni ma la ko sante, man itam dinaa la sàmm ci waxtuw nattu biy wàccsi ci àddina sépp, ngir nattu waa kaw suuf.
¶ Gannaaw loolu ma xoolaat, daldi gis màkkaan ma fa asamaan, xayma ba fat seede si, mu ubbiku.