Job 20:19
TSK
Moo dëggaate néew-ji-doole, dëddu ko; aakimoo kër jaambur te tabaxu ko.
TSK
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
Moo dëggaate néew-ji-doole, dëddu ko; aakimoo kër jaambur te tabaxu ko.
alal ak koom am sa kër, sag njekk sax dàkk.
Ku ma sopp, ma nàddil la, feesal sab denc.»
Ku baax, donale ba cay sëtam; alalu moykat, muuru ku jub.
Néewle te jub moo gën barele te jubadi.
Waaye benn ŋëb bu ànd ak dal moo gën ñaari ŋëbi doñ-doñ ci napp um ngelaw.
Toroxtaange gu ñu koy teg ndax Almasi, moom la defoon muy alal ju ëpp denci Misra, ndax yoolub ëllëg ba la doon séentu.