TSK

TSK · Proverbs 16:24

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Back to passage

Santaaneb ragal Aji Sax ji mooy li sell te sax ba fàww. Lu Aji Sax ji digle, dëgg la, ak njekk gu sotti.

Làmmiñu waxkat, jam-jami jaasi; kàddu gu xelu, garab la ci.

Aji Sax ji bañ na mébét mu bon, te wax ju yiw daa sell fa moom.

Doom, deel lekk lem, baax na, lem ju xelli, boo sexee, mu tem-temi.

Diwook suuru day naatal xol; waaye li neex cib xarit, xol la lay digale.