TSK

TSK · Proverbs 16:31

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Back to passage

¶ «Bu boroom bijjaaw teewee, jógleen wormaal ko. Deeleen rus mag te ragal-leen seen Yàlla. Maay Aji Sax ji.

Kuy ndaw, génne kaso, tàmbalee nguuru fa mu juddoo woon mbaadoolo, ndaw loolu su dee baadoolo te xelu it, moo gën buur bu màggat, dofe, dégguli àrtu.

Luke 1:6 TSK

Ñoom ñaar ñépp a juboon, Yàlla seede, te mucc ayib ni ñuy jëfe santaane yeek ndigali yooni Boroom bi.

waaye tinu la ci ngir cofeel, mooy li ma taamu, man Póol mu màggat mii, boole ci léegi tënku biir kaso ndax Almasi Yeesu.