TSK

TSK · Proverbs 17:19

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Back to passage

¶ Ba mu ko defee Abigayil dellu ca Nabal, fekku ko lu moy mu amal biir këram bernde ju mel ni berndey buur. Xol baa nga sedd, mu màndi lool, ba tax Abigayil waxu ko dara ba bët set.

¶ Ci biir loolu Adoña doomu Daawudaak Agit, di tëggu naan: «Man mii maay doon buur.» Mu waajalal boppam watiiru xare aki fas ak juróom fukki nit ñuy daw di ko jiitu.

Ndoortel ay di wal mu tàmbali, luy indib xuloo, bàyyil.

Boroom xadar day sooke ay, te ku tàng bopp moy, moyati.

¶ «Buur, li nga gis kenn ci wattukat yu sell yi wàcce asamaan, àddu ca kaw ne: “Daaneleen garab gi, tas ko, waaye ëkk beek reen yi, bàyyileen ko fi suuf, ci digg mbooy mi, te jénge ko càllalay weñ ak xànjar. Na lay biy wàcc, di ko faam, muy dunde ñax nig jur diiru juróom ñaari jamono.”

Ndax merum nit du jur njub fa Yàlla.