TSK

TSK · Proverbs 17:27

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Back to passage

Wax ju bare, moy ñàkku ca; ku moom sa làmmiñ, xelu nga.

Ku jub day teeylu tontam; ab soxor, wax ju ñaaw rekk.

Ku xelu, kàddoom yu dégtu ndànk moo gën ŋal-ŋalu kilifa ci biir ñu dofe.

James 3:2 TSK

Bare na lu nuy tooñ, nun ñépp. Ku dul tooñ ci kàddu nag, kooku nit ku mat la, te man naa moom yaramam wépp, boole ci.