TSK

TSK · Proverbs 18:13

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Back to passage

ay nit ñu tekkiwul dara, te bokk ci yeen, ñoo jóg di waññi seen waa dëkk, naan leen: «Nanu jaamuji yeneen yàlla,» yàlla yu ngeen xamul,

Buur ne ko: «Kon boog, may naa la mboolem alalu Mefiboset.» Mu ne ko: «Jaajëf Buur sang bi, gis naa ni nga ma baaxee.»

Ba mu ko defee Buur tekki jaarob torlukaayam ci baaraamam, jox ko Aman doomu Amdeta ma askanoo ca Agag, noonub Yawut ya.

Job 29:16 TSK

Néew-ji-doole, maa doon baayam, ku ma xamul sax, may seet àqam.

Léegi nag, Buur, dogalal aaye bi, te torlu mbind mi, ba dootu tebbiku, mu dëppook yoonu waa Medd ak waa Pers, wi dul toxu.»