TSK

TSK · Proverbs 21:7

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Back to passage

Xeet yee tàbbi pax ma ñu gasoon, fakktaloo fiir ga ñu làqoon.

Bul xañ néew-ji-doole; néew-ji-doole la. Ku tumurànke, bu ko soxore cib àtte,

Seeni njiit të, xejjoo ay sàcc, ñoom ñépp sopp ger, di dàq ay neexal, ab jirim, sàmmuñu àtteem, àqu jëtun soxalu leen.

Dama leen di dàq, ngeen sore ma, na ma dàqe woon seen bokk yépp, askanu Efrayim gépp.”

¶ «“Maa ngii nag di fenqe samay loxo, di ko mititloo alal ju lewul ji nga dajale, ak sa dereti nit ji ñu tuur fi sa biir.

¶ Mu ne ma: «Lii mooy alkute giy wàccsi ci kaw réew mi mépp. Li taxañ bi wax ci genn wetam mooy képp kuy sàcc, dees na ko fi dàqe, te li mu wax ci wetam gi ci des mooy képp kuy giñ ci ay fen, dees na ko fi dàqe.