TSK

TSK · Proverbs 23:11

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Back to passage

Bu ngeen leen néewalee déy, bu ñu yuuxoo, woo ma wall, dinaa dégg seen yuux moos.

Job 19:25 TSK

Waaye man xam naa ne sama jotkat a ngi dund, te mooy mujje taxaw fi kaw suuf.

Mooy baayoo jirim, di àtte jëtun, kookoo di Yàlla ja fa dëkkuwaayu sellngaam.

Aji Sax ji Boroom gàngoor yi dafa wax ne: «Bànni Israyil ak Yuda, ñépp lañu notandoo. Ñi leen jàpp ñépp téyee leen doole, bañ leena ba.

Aji Sax ji nag dafa wax ne: «Maa ngii di leen layool seen layoo, ba feyul leen. Maay ŋeeral géejam, ŋiisal am walam,