TSK

TSK · Proverbs 23:15

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Back to passage

Gone yi, tee ngeena dégg yaru baay, te déglu, ba am ug dégg?

Doom rafet xel, baay ba bég; te ab dof ay xeeb ndey ja.

Deel bégal ndey ak baay, rawatina ndey ji la jur.

Maay am mbégtey baaxe leen, jëmbat leen bu wér ci réew mi, jëmbate leen sama léppi xol ak sama léppi jëmm.»

Waaye mbégte ak bànneex war na, ndax sa rakk jii moo dee woon te dekki na, moo réeroon te feeñ na!”»