Proverbs 4:10
TSK
Déglul, doom, te dégg saay wax, ndax nga gudd fan.
TSK
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
Déglul, doom, te dégg saay wax, ndax nga gudd fan.
Yaafus bee, xoolal xorondom, seetal ci moom, ba muus.
Defal sam xel ci yar, te teewlu kàdduy xam-xam.