TSK

TSK · Proverbs 24:20

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Back to passage
Job 18:5 TSK

Ku bon kay lag leeram di fey, te taalam du jolli.

Aji Sax jaa ngi feeñoo, di àtte yoon; ku bon teg ug fiir, tàbbi ca. Na jib ndànk. Selaw.

Léegi mu wow nim ñax, lax ni gàncax.

Ku saaga sa ndey mbaa sa baay añe lëndëmu bàmmeel.

Waaye wóoy ku bon, nde mooy bonle; la mu def rekk lees koy def.