TSK

TSK · Proverbs 24:23

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Back to passage

¶ «Buleen safaan dëgg cib àtte. Buleen far néew-ji-doole te buleen far boroom doole. Àtteleen seen moroom ci dëgg.

Buleen jalgati yoon cib àtte, buleen jeng te buleen nangu alalu ger, ndax ab ger day muur bëti boroom xel, di xañ aji jub dëgg.

«Dungeen bàyyi àtteb njublaŋ, ak di faral ku bon? Selaw.

ngir mana xam aw léeb aku taas ak kàddug boroomi xel yu rafet ak seeni cax.

Teewlul te déglu li boroom xel yi wax. Defal sam xel ci li ma lay xamal.

Ana ku rafet xel nu muy mel? Ana ku xam piri? Am xel rafet, kanam leer, gëna lewet.

James 2:4 TSK

su boobaa xanaa du yeena ngi gënaatle ci seen biir, tey àttee ay mébét yu bon?

¶ Gannaaw nag kiy àtte nit ku nekk ci ay jëfam te amu ci xejj ak seen, Baay ngeen koy wax, sàllooleen koo ragal, seen diirub ngan ci kaw suuf.