Job 5:27
TSK
Lii kat lanu gis, te lii rekk la. Dégg, jariñu.
TSK
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
Lii kat lanu gis, te lii rekk la. Dégg, jariñu.
Ba may ndaw, ba tey may mag, gisuma ku jub ñàkk ndimbal, mbaa askanam di dunde yalwaan.
Yaafus bee, xoolal xorondom, seetal ci moom, ba muus.
Kuy dégg, say wax rafet; te ku ñàkk bopp, yelloo yetu gannaaw.
Ab yaafus day yaakaar, du am; ab njaxlaf sàkku, woomle.
Lu ne laa gis ci sama dund gu gàtt gii! Nit a ngii jub, teewu koo sànkook njubam; nit bon, ànd ak mbonam, gudd fan.