1 Samuel 24:20
TSK
Ana kuy jekku noonam, wacc ko mu dem ak jàmm? Yal na la Aji Sax ji fey lu baax li nga ma defal bésub tey jii.
TSK
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
Ana kuy jekku noonam, wacc ko mu dem ak jàmm? Yal na la Aji Sax ji fey lu baax li nga ma defal bésub tey jii.
Bu sab noon daanoo, bu ko bànneexoo, bu tërëfee, bu ko bége.
Li mu wax kay mooy: «Bu sab noon xiifee, jox ko mu lekk, bu maree, may ko mu naan. Soo defee noonu, day rus, ba mel ni koo yen ay xal.»