TSK

TSK · Proverbs 26:21

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Back to passage

¶ Booba nit ku bon a nga woon ca mbooloo ma, ku ñuy wax Seba, di doomu Bikkri, ma bokk ca giirug Beñamin. Seba wal liit ga, daldi yéene ne: «Sunu yoon nekkul ci Daawuda doomu Yese jii, du benn cér bu nu am ci moom. Yeen waa Israyil, ku nekk ca sa xayma!»

¶ Ci biir loolu Israyil gépp dégg ne Yerbowam délsi na; ñu woote ndaje, woo ko ca, fal ko buurub Israyil gépp. Kenn farul ak waa kër Daawuda, lu moy waa giirug Yuda doŋŋ.

Boroom xadar day sooke ay, te ku tàng bopp moy, moyati.