TSK

TSK · Proverbs 26:7

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Back to passage

Waaye Yàllaa leen di jamu fittam, ñu jekki daanu.

Kàddu gu xelu ci gémmiñug dof mooy car aki dégam, màndikat xàcci.

Luke 4:23 TSK

Mu ne leen: «Xam naa ne dingeen ma waxal waxin wi ñu naan: “Fajkat bi, fajal sa bopp.” Mboolem li nu dégg ne moo xew Kapernawum, def ko fii ci sa réewum bopp itam.»