TSK

TSK · Proverbs 28:17

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Back to passage

Ku tuur deretu nit, na nit tuur deretam, ngir melokaanu boppam la Yàlla sàkke nit.

Ñetti dëkk yu ngeen di joxe ci wàllu dexu Yurdan wii, ak ñetti dëkk yu ngeen di joxe ca réewum Kanaan, lépp di ay dëkki rawtu.

Fekk na Absalom daw. Ci kaw loolu ngóor sa aye jongru daldi séentu, gisul lu moy nit ñu bare ñuy dikk, awe yoonu Oronayim, bartaloo tund wa.

Ñu wax Buur Suleymaan ne ko: «Yowab daw na, làquji ca xaymab Aji Sax ji, te kat ma nga ca sarxalukaay ba.» Suleymaan sant Benaya doomu Yoyada, ne ko mu dem, jam ko.

Te itam Aji Sax ji wax na ci mbirum Yesabel ne: Ay xaj dina lekk Yesabel ca wetu tatay Yisreel.

Acts 28:4 TSK

Waa réew ma gis jaan ja langaamoo loxol Póol, ñu naan ca seen biir: «Nit kii kay ab bóomkat lay doon, ndegam moo rëcce géej, te taxul Ndogal may ko mu dund.»