TSK

TSK · Proverbs 28:5

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Back to passage

Aji Sax ji, yaa réyi jëf; xóoti pexe.

Maa ëpp mag ñi dég-dég, nde say tegtal laa topp.

Wax ju xelu sut nab dof, jataayu pénc du fa àddoo.

«Dofe la sama ñoñ def. Man, xamuñu maay kan, mbetey gone yu dul xalaat dara; dég-dég, tus; seen xel mépp, lu bon rekk, lu baax, xamuñu ci dara.»

¶ Nitu neen nag du nangu lu aju ci Xelum Yàlla. Ag ndof lay doon ci moom; du ko mana xam, ndax loolu Xelum Yàlla lees koy natte.