TSK

TSK · Proverbs 3:24

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Back to passage

¶ «Maay baaxee réew mi jàmm it, ba bu ngeen tëddee kenn du leen tiital. Maay jële rab wu aay ci réew mi, te saamar du jóg, dal ci seenum réew.

Job 11:19 TSK

jaaxaan, kenn du la lëjal, ñu bare di la leewaayu;

Maay tëdd nelaw, yewwu; Aji Sax ji di ma aar.

Doo ragal njàqarey guddi mbaa fittu bëccëg

Neen it la nit di teela jóg ak a guddee tëdd, di doñ-doñi lu mu lekk: Aji Sax ji leel na soppeem lu ni day, fekk ko muy nelaw.

Ragalal Aji Sax ji ndax nga gudd fan, nopplu te baña loru.

¶ Ba loolu amee ma yewwu, ne xiféet, xam ne samay nelaw neex na.

Maay fas ak ñoom kóllëreg jàmm, maay far ci réew mi wépp rab wu aay. Su boobaa ñu dëkke màndiŋ mi ci xel mu dal, di fore bët biir gott bi.

Acts 12:6 TSK

¶ Ba ñu demee ba ca guddi, ga jiitu bés ba ko Erodd wara yóbbu, Piyeer a ngay nelaw ci diggante ñaari takk-der, ñu yeewe ko ñaari càllala, ay dag di wattu buntu kaso ba.