TSK

TSK · Proverbs 4:5

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Back to passage
Job 23:11 TSK

Tànkam, sama tànk, yoonam laa tegu, moyuma ko.

Nit ñu bew ñi ñaawal nañu ma lool, waaye dëdduwma saw yoon.

Ma nga naan: «Moo téxét bi, foo àppal sa téxét gi? Ñaawlekat bi, foo àppal sa ñaawle bi? Dof bi, ñaata yoon ngay bañ xam-xam?

Mbégtee ñeel ku daj xel mu rafet ak ku am ug dégg.

Wutal xel mu rafet, bàyyi wurus; taamul ag dégg, wacc xaalis.

Ab siis, bànneexu boppam rekk, loo ko digal mu xalab.

Jëndal dëgg te bu ko jaay. Sàkkul xel mu rafet ak yar akug dégg.