TSK

TSK · Proverbs 5:1

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Back to passage

Gone yi, tee ngeena dégg yaru baay, te déglu, ba am ug dégg?

Doom, defal li la baay sant, te bul wacc ndigalal yaay.

Teewlul te déglu li boroom xel yi wax. Defal sam xel ci li ma lay xamal.

Ku ami nopp kat, na dégg li Noowug Yàlla wax mboolooy gëmkat ñi. Ku am ndam nag, maa lay may nga lekk ci garabu dund gi ci Àjjana, toolub Yàlla.

¶ «Ku ami nopp kat, na dégg li Noowug Yàlla wax mboolooy gëmkat ñi. Ku am ndam nag, maa lay may ci mànn mu làqu mi, nga lekk, maa lay jox it aw doj wu weex; doj wu ñu bind tur wu bees wu kenn xamul, ku dul ka ko jot.

Ku ami nopp kat, na dégg li Noowug Yàlla wax mboolooy gëmkat ñi.

Ku ami nopp kat, na dégg li Noowug Yàlla wax mboolooy gëmkat ñi.»