TSK

TSK · Proverbs 6:15

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Back to passage

«Yeen fàttekati Yàlla yi, déggleen lii, bala maa fàdd te kenn du wallu.

Njàqare di ngëlén, dab la, sa musiba def callweer, buub la, njekkar ak fitna dal la.

Ku ñuy àrtu, nga të ticc, dangay jekki yàqu, ba wees am paj.

te nga ne leen: “Aji Sax ji Boroom gàngoor yi dafa wax ne: Askan wii ak dëkk bii, ni ñuy toje njaq, ba deesatu ko mana defaraat, ni laa koy tojate. Tofet gii dees na fi rob ndax ñàkk fu ñu robe.

Fa nit ñi naan: «Jàmm ak kaaraange dikk na,» fa la sànkute di dale ci seen kaw, ni aw mat di jekkee dal ci kaw jigéenu wérul, te kenn du ca rëcce.