Job 22:22
TSK
Nangool ndigal ci làmmiñam, te dëxëñi kàddoom ci sa biir xol.
TSK
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
Nangool ndigal ci làmmiñam, te dëxëñi kàddoom ci sa biir xol.
Sama doom, déggal samay wax, fonk samay santaane.
Tànk ya day bartalu wuti ndee, ay jéegoom àkki njaniiw.
Ku rafet xel day xam, ne cell; bu dof noppiwul, yàqule teew.
Moom nag mu ne ko: «Xanaa kay, ndokklee ñiy déglu kàddug Yàlla te di ko jëfe.»
Mu ne ma: «Ëpp naa def, sa mbokkum jaam doŋŋ laa, ni yaak sa bokki yonent yeek ñiy sàmm kàdduy téere bii. Sujjóotalal Yàlla.»