«Buleen ŋalŋaleeti, di damook a damooti, bu reewande génne seen gémmiñ, Aji Sax jeey Yàlla ji xam lépp, te mooy natt jëfi nit.
TSK
TSK · Proverbs 8:13
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
Aji Sax ji, ag suba, ngay dégg sama baat, suba su ne ma diis la samay dagaan, di séentu.
Caaxaani neen, xooluma; jëf ju wàcc yoon, bugguma, taqu ma fenn.
Moo tax foo tegtale, ma rafetlu, lépp luy yoonu fen, ma bañ.
Dàqal wor, mu sore la; kàdduy naxe, na la dànd.
Juróom benn a ngii yu Aji Sax ji bañ, ba ci juróom yaar yu mu seexlu:
Kàddug ku jub day jur xel mu rafet, ku wax njekkar ñu tëj sa gémmiñ.
Ku jiital ngor ak worma, Yàlla jéggal la; ku ragal Aji Sax ji, dëddu lu bon.
Bañleen lu bon, bëgg lu baax, di doxal yoon ci pénc. Jombul Aji Sax ji Boroom gàngoor yi baaxe ndesu askanu Yuusufa.
Ku nekk ci yeen, loraangey moroomam, bumu ko mébét cib xolam, te kàddug ngiñ ci ay fen, buleen ko safoo, nde loolu lépp laa bañ.» Kàddug Aji Sax jee.
te lu bon, ak nu mu mana bindoo, dàndleen ko.
¶ Naka noonu yeen ndaw ñi, nangul-leen magi mbooloom gëmkat ñi. Yeen ñépp nag toroxluleen ci seenug jëflante, ndax: «Yàlla, ñi réy lay xeex, ñi toroxlu, mu may leen aw yiw.»