1 Kings 13:34
TSK
Loolu nag di bàkkaar bu réy ci biir kër Yerbowam, ba tax askanam daanu, ba raaf fi kaw suuf.
TSK
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
Loolu nag di bàkkaar bu réy ci biir kër Yerbowam, ba tax askanam daanu, ba raaf fi kaw suuf.
Koomum këram day tukki, ne mes, keroog sànjum Yàlla ma.
Yal na askanam dagg. Balaa geneen maas a wéy, yal na seenu tur fey.