Job 16:12
TSK
Féexoon naa, mu falaxe ma; sëq sama ndodd, rajaxe ma, def ma diirukaayam,
TSK
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
Féexoon naa, mu falaxe ma; sëq sama ndodd, rajaxe ma, def ma diirukaayam,
Yaw Yàlla, dama lay bége, bànneexoo la, woy la, yaw Aji Kawe ji.
Sol nga ma dooley xare, sukkal ñi ma jógal, ñu féete ma suuf.
Tumurànke naa, nga gis. Duyal samay rongooñ ci sa mbuus. Du lim nga lépp?
Ngeen mébét, dara! Ngeen diisoo, diisoo, tus! Yàllaa ànd ak nun!