Maa ànd ak yaw fépp foo dem, maa tenqee fi sa kanam mboolem say noon, te maa lay may tur wu màgge ni turi boroom daraja yi ci àddina.
TSK
TSK · Psalms 21:6
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
2 Samuel 7:9
TSK
Psalms 4:6
TSK
Rendileen seen sarax yi war, te wóolu Aji Sax ji.
Psalms 43:4
TSK
Kon Yàlla, naa àgg sa sarxalukaay; yaw Yàlla, yaay sama mbégte, di sama bànneex. Yaw Yàlla, sama Yàlla, naa la màggale xalam.
Psalms 63:2
TSK
Yaw Yàlla, yaay sama Yàlla, ma di la sàkku, sama bakkan mar la, sama jëmm namm la, fu suuf mare ndox, ne sereŋ.
Luke 2:10
TSK
Malaaka mi ne leen: «Buleen tiit, ndax kat maa leen indil xibaaru jàmm bu doon mbég mu réy, ñeel askan wépp.
Acts 2:28
TSK
Yaa ma xamal yoonu dund, yaa may wéttali ba matal sama mbégte.”
Galatians 3:9
TSK
ba tax na, boroom ngëm yi lees di booleek Ibraayma miy boroom ngëm, barkeel leen.
Ephesians 1:3
TSK
¶ Cant ñeel na Yàlla sunu Baayu Sang Yeesu Almasi, mi nu baaxe bépp barkey biir, ci Almasi mi nu bokk, fa déndi asamaan ya.