TSK

TSK · Psalms 39:13

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Back to passage

Seen baay Yanqóoba ne leen: «Xañ ngeen ma ay doom: Yuusufa nekkatul, Simeyon nekkatul, léegi ngeen bëgga jël Beñamin, yóbbu. Loolu lépp ci sama kaw; ngalla man!»

¶ «Suuf si deesu ko jaay, mu wel fàww, ndax maay Boroom suuf si, yeen ay doxandéem ngeen fi, yu ma fi dëkkal.

Job 10:20 TSK

Xanaa du fan yu néew laa dese? Ba ma boog! Xiddil, ma leqliku,

Job 14:10 TSK

Waaye nit dee, doole réer, bakkan rot, mu ne mes.

Doxandéem laa fi kaw suuf, bu ma làq say santaane.