Romans 16:20
TSK
Su ko defee Yàlla miy boroom jàmm mooy dër Seytaane ci lu gaaw, fi ngeen ko joggi seeni tànk. Yal na sunu yiwu Boroom Yeesu ànd ak yeen!
TSK
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
Su ko defee Yàlla miy boroom jàmm mooy dër Seytaane ci lu gaaw, fi ngeen ko joggi seeni tànk. Yal na sunu yiwu Boroom Yeesu ànd ak yeen!
Sunu yiwu Boroom Yeesu Almasi ñeel na leen yeen ñépp.