Naka la tàggtoo ak ñoom, ne leen: «Dinaa leen seetsiwaat, bu soobee Yàlla.» Ba loolu amee mu dugg gaal, bàyyikoo Efes,
TSK
TSK · Romans 1:10
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
Acts 18:21
TSK
Acts 21:14
TSK
Naka lanu wax, wax, mu të, nu bàyyi, daldi ne: «Kon nag yal na Boroom bi sottal coobareem!»
Romans 15:22
TSK
¶ Sama liggéey boobu sax moo ma gàllankoor lu bare ba dikkaguma seetsi leen.
Waaye maa ngi dikk léegi ba ci yeen, ndegam soob na Boroom bi, ba nattal sama bopp manoore ju réy-réylukat yooyu am, te duy kàddu kese.
Moo tax nu bëggoon leena seetsi, waaye Seytaane moo nu gàllankoor. Te man Póol, jéem naa leena seetsi bu dul benn yoon du ñaar.
Philemon 1:22
TSK
¶ Te itam nanga ma waajalaale ab dal, ndax yaakaar naa ne dees na ma délloosi fi yeen, ndax seen ñaan yu nangu.
James 4:15
TSK
Li ngeen di wax kay moo di: «Bu soobee Boroom bi, dinanu dund ba def nàngam sii mbaa nàngam see.»