TSK

TSK · Romans 13:11

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Back to passage

Yéene bii moo wàccal Duuma: Nit a ngi may wooye tundu Seyir, naan: Jongrukat bi, lu des ci guddi gi? Éy jongrukat bi, lu desati ci guddi gi?

¶ Li may wax, bokk yi, moo di, li des yàggatul. Kon nag bés niki tey, na ñi am jabar mel ni bu ñu ko amul woon;

Délloosileen xel yi ci njub te bàyyi bàkkaar, ndax ñàkka xam lenn ci Yàlla, moom la ñenn ci yeen nekke, te loolu gàcce la ci yeen, laa wax!

¶ Waaye nag bokk yi, lu jëm ci ay àpp, ak bés ya loolu di am, soxlawuleen ku leen ci bind,

¶ Te itam mujug lépp dëgmal na; kon nag jiital-leen seenum xel, te ànd ak seen sago, ngir ngeen man di ñaan.

¶ «Maa ngii di ñëw léegi, ànd ak sama pey, ngir delloo ku nekk jëfam.