TSK

TSK · Romans 13:8

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Back to passage

¶ Buleen gàddu àqu liggéeykat, baadoolo bu néew doole ci seen biiri bokk, mbaa ci seen dëkkandoo yiy doxandéem ci seen dëkk yi ci réew mi.

Cofeel du waral kenn def moroomam lu bon; kon cofeel moo matal sëkk yoonu Musaa.

Ci kaw loolu lépp nag, tegooleen cofeel; mooy xànc gi leen faste, ba seenug bennoo mat sëkk.

James 2:8 TSK

¶ Ndegam nag yoonu Buur Yàlla ngeen matal sëkk, di sàmmonteek Mbind mi ne: «Ni ngeen soppe seen bopp, nangeen ko soppe seen moroom,» su boobaa waawleen góor!