TSK

TSK · Romans 14:13

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Back to passage

Du tere nag, gannaaw dangaa teddadil lool Aji Sax ji ci mbir mii, doom ji nga ci am, moom, day dee rekk.»

«Yaw nit ki, ñii seen kasaray tuur lañu def ci seen xol, muy ay wu leen di gàllankoor, te ñu ne ci jàkk. Ñii dinaa leen wacc moos, ñuy sàkku leeraange ci man?

¶ «Te itam lu leen tee àtte njub, yeen ci seen bopp?

Ndax lan? Ngëm lañu sukkandikoowul, xanaa ay jëf. «Doj wuy fakktale,» moom lañu fakktaloo.

Yaw miy sikkal jaamub jaambur, yaay kan? Su baaxalee mbaa mu bonal, sangam a koy seet! Te day baaxal ndax Boroom bi man na koo baaxal.

¶ Léegi nag bokk yi, dama leen di ñaax, ràññeeleen ñi gàntal àlluwa ji ngeen jànge, di féewale, ak a téqtale, te ngeen moytu leen.

Buleen may kenn lu muy def njombe: du Yawut yi, du jaambur ñi, du mbooloom Yàlla mi.

Ndaxte cofeelu Almasi daal moo nu jiite, nun ñi ràññee lii: Gannaaw kenn moo deeyal ñépp, kon ñépp a dee.

ba mana xàmmi li gën. Su ko defee ngeen set wecc te mucc sikk, ngir keroog bésub Almasi.

James 2:4 TSK

su boobaa xanaa du yeena ngi gënaatle ci seen biir, tey àttee ay mébét yu bon?