TSK

TSK · Romans 14:21

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Back to passage

Waaye yeen dangeena moy yoon wi, seenum njàngle ngeen fakktale ñu bare, te yeena fecci kóllëreg Lewi.» Aji Sax ji Boroom gàngoor yee ko wax.

¶ Kon nag bunu di seetati lu nu sikkantee, li ngeen di seet kay mooy nu ngeen fexee ba dungeen yóbbe mbokkum gëmkat lu koy fakktal, mbaa lu koy daane ci bàkkaar.

¶ Nun ñi fendi ci wàllu ngëm, fàww nu xajoo tëley ñi néew doole, te baña sàkku sunu bànneexu bopp.

ba mana xàmmi li gën. Su ko defee ngeen set wecc te mucc sikk, ngir keroog bésub Almasi.

¶ «Waaye lenn a ngi lu ma lay sikke: yaa ngi uuf foofu ay nit ñuy saxal njànglem Balaam, moom mi doon xiirtal Balag ci tegal Israyil ndëgg-sërëx, ngir ñu lekk ñam wu ñu sarxal ay tuur, ak di gànctu.