TSK

TSK · Romans 14:6

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Back to passage

Guddig keroog guddig teewlu la, ñeel Aji Sax ji, ngir moo leen ca génne réewum Misra, moo tax guddi googu di gu ñu jagleel Aji Sax ji, bànni Israyil gépp war cee fanaanee teewlu, ñeel Aji Sax ji, ba fàww.

Ndax lii moo di koor gi ma taamu, ci bés bu nit kiy toroxlu? Koorug dëngal loos ni barax, lal saaku, sotti ab dóom, tëdd di ko ñaawloo? Loolooy seen koor, ci bés bu Aji Sax ji rafetlu?

Yeena ngi wormaal yenn bés yi, aki weer, ak ay fan, aki at!