Psalms 27:2
TSK
Ab soxor wutsi ma, nar maa yàpp, noonoo ma, bañ ma; mooy tërëf, fëlëñu.
TSK
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
Ab soxor wutsi ma, nar maa yàpp, noonoo ma, bañ ma; mooy tërëf, fëlëñu.
Man may saxoo yaakaar, di la sant, di santati.
Ndaxte mboolem lu ñu bindoon, bu jëkk, jàngal nu moo taxoon ñu bind ko, ngir Mbind mi may nu xolu muñ, te ñaax nu, ba nu am yaakaar.
Nu nekk lees nuy tance, waaye deesu nu nappaaje. Dinanu jaaxle, waaye dunu jàq.
¶ Keroog ba ma jëkkee di layool sama bopp, kenn taxawuwma, ñépp a ma daw, yàlla bu leen seen jëf topp.
¶ Loolu bégeleen koo bége, doonte tey ñàkkul ngeen nekke njàqare ab diir, ndax ay nattuy nattu.