Genesis 31:15
TSK
Doonunu lu moy ay doxandéem ci moom de! Nde da noo jaay, lekk sunu njég, ba mu jeex tàkk.
TSK
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
Doonunu lu moy ay doxandéem ci moom de! Nde da noo jaay, lekk sunu njég, ba mu jeex tàkk.
Aji Sax jeey lim xeet yi, limaale leen ne: «Kii fi la juddoo.» Selaw.
Gannaaw gi la jagoo màndargam xaraf, mu firndeel àtteb njubam gi ngëmam waral, te fekkul mu xaraf. Noonu la Ibraayma mana nekke maamu mboolem gëmkat ñi. Looloo tax muy maamu mboolem ñi xaraful, te gëm, ndax ñu waññal leen seen ngëm, ab àtteb ñu jub.
¶ Yeen ñépp doomi Yàlla ngeen, ndax li ngeen gëm Almasi Yeesu.