Genesis 38:8
TSK
Yuda ne Onan: «Demal ci sa jabaru mag, donn ko, ndax nga giiral sa mag aw askan.»
TSK
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
Yuda ne Onan: «Demal ci sa jabaru mag, donn ko, ndax nga giiral sa mag aw askan.»
Bu loolu amee na ko magi dëkkam woolu, wax ak moom. Su waa ji dëgëree, ne buggu koo jël,
¶ Nawmi ne Ruut: «Yal na Aji Sax ji barkeel Bowas, moom mi saxoo sàmm ngoram digganteem ak nit, muy dund ak mu dee!» Mu teg ca ne ko: «Kooku ku nu jege la; bokk na ci ñi am sañ-sañu jotaat nu.»
Dangay fanaan fii. Bu ëllëgee, su fekkee ne nangu naa def warugaram ci yaw, na ko def, baax na. Su nanguwul nag, dogu naa ci Aji Sax ji, Kiy Dund, man dinaa ko def. Tëddal fii rekk, ba ëllëg.»