TSK

TSK · Titus 3:4

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Back to passage

¶ Yoonu Musaa moo dikk ngir fésal barewaayu moy, waaye fu bàkkaar bare, aw yiw gën faa bareeti,

¶ Ci man Póol, ndawal Almasi Yeesu, ci ndigalal Yàlla sunu Musalkat, ak Almasi Yeesu sunu yaakaar, ci man la bataaxal bii bawoo,

Loolu kat moo nu tax di sonn aka góor-góorlu, ndax Yàlla jiy dund lanu yaakaar, moom miy musal ñépp, rawatina gëmkat ñi.

Titus 1:3 TSK

Waaye tey bi mu jotee, Yàlla sunu Musalkat moo feeñal kàddoom ci biir waare bi mu ma dénk man, te moo ma digal ma xamle ko.

Lu ko moy ca njàlbéenu àddina lay dale sonn ay yooni yoon. Waaye tey ci mujug jamono yi la feeñ benn yoon doŋŋ, ba sarxe boppam, ngir far bàkkaar.