TSK

TSK · Mark 3:21

Treasury of Scripture Knowledge references in Téereb Injiil.

Back to passage
Mark 3:31 TSK

¶ Noonu ndeyu Yeesu ak ay rakkam ñëw, ñu taxaw ci biti, yónnee, woo ko.

Ñu bare ca ñoom naan: «Dafa ànd ak rab! Dafa dof! Lu tax ngeen koy déglu?»

Su fekkee danoo tàggalikoo ak sunu sago, ngir Yàlla la. Su nu àndee ak sunu sago, ngir yéen la.