TSK

TSK · 1 Samuel 17:52

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

Ba loolu amee ñu yónnee, woolu mboolem kàngami waa Filisti. Ñu laaj leen ne leen: «Nan lanuy def ak gaalu Yàllay Israyil gii?» Ñu ne leen: «Toxal-leen gaalu Yàllay Israyil gi ca Gaat.» Ñu toxal gaalu Yàllay Israyil ca seen dëkk ba ñuy wax Gaat.

Ci biir loolu Ebrë yi nangul woon waa Filisti démb ak bëkk-démb te nekkandook ñoom ca dal baak fa ko wër fépp sax, ne waññet, faraat ak seen bokki bànni Israyil ya ànd ak Sóol ak Yonatan.

Buurub Israyil nag song leen, rey fas ya, yàq watiir ya, daan waa Siri jéll bu réy.