TSK

TSK · 2 Samuel 15:27

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

Dangay dellu kay ca dëkk ba, ne Absalom: “Buur, sab jaam laa. Sa jaamu baay laa woon, waaye léegi sab jaam laa.” Noonu nga may yàqale pexem Ayitofel.

¶ Ma nga fekk Yonatan ak Ayimaas ca En Rogel. Manuñu woona dugg ca biir dëkk ba, ndax ragal ñu gis leen. Ab jaam bu jigéen nag di dem ca Yonatan ak Ayimaas, di leen wax la xew, ngir ñu dem ca Buur Daawuda, yegge ko ko.

Ba Daawuda jógee ca ëllëg sa, kàddug Aji Sax ji dikkal Gàdd, yonent Yàlla ba féetewoo kër Buur Daawuda. Mu ne ko:

Ayimaas ma sasoo Neftali; moom it jël na doomu Suleymaan ju ñuy wax Basmat soxna.